« temps boy »
bon je vous dis dèjà, c'est le titre de ma chanson préféré dans le prochain album de Daara J. Yep, l'album n'est pas encore sortie (il arrive bientôt,m'enfin si tout se passe bien.. En tout cas ne le ratez pas!), je n'ai pas encore tout écouté, mais je sais déjà que ce sera ma préféré. Un petit voyage vers l'enfance qui m'a rendu des plus nostalgiques. Bien sur si je vous dis que j'ai passé l'enfance la plus merveilleuse de toute la planète vous ne me croirez certainement pas, mais moi, je me crois. Et comme je suis encore dans mon trip : je-me-sens-benie-j'ai-beaucoup-de-chance,-j'ai-eu-la plus belle enfance,et-puis-c'est-mon-anniversaire-et-c'est-chez-moi-ici-j'ai-le-droit-de-regarder-un-peu-monombril et que souffler une bougie de plus m'a rendu encore plus nostalgique que jamais, ben j'ai voulu aussi faire ma version à moi de « temps boy » (pour ce qui ne comprennent pas, cela veut dire en gros « l'enfance »). Disons que ce sera une (plate) adaptation de la version du daara-J :-)
Une derniere chose, mille pardons à ceux qui ne comprennent pas woloff, (aah les veinards, vous l'avez echappé belle! ) mais je suis totalement incapable de parler de tout cela dans une autre langue, même pas dans ma langue maternelle, c'est fou...
bon je parle trop ...
temps boy,
jeundi keurignxeelu diallo kerign
taseh ak boy serigne
mou thiokaass,
ga ni xalaass,
ragadiou
thiipeutou,
yoleekou...
gnibi keur geu,
boyal forneaupareh, jeunddi omo
raxass bol,raz le bol !!!
temps boy...
langaa bourikou ko fegnal ?
xaana maty
ci neegu tata raky.
bii tank tankou kan la ?
sant yi beuri, xaleyi sakan,
melting pot ci keurgui, li moy sunu askan.
lambbi golo, ku jokk daanu,
neubeul seuy tankk balaa saanku.
Ndjool daadj,
sol salaatoo (so !)
bal ba dem na kaw (so !)
bala mu koy laal (so !)
yaramu faada daw ! *
temps boy....plaline, tracer ligne,
teup sanni xeer,
deysane sama xel reer
«
couricou defiler »,
niun xamuniou le furet
« il est passer par ici
il est parti par là bas »
De france à Joloff
dafeu moudj lakeu woloff
ak lekk « thiaaf, dogu yapp
libeur mbourou potu sardine »
temps boy...
«
A velo » walla « amina »
Aye walla
guinté walimale rythme dans le sang,
la puissance dans la voix
« 1 pied ndeer »jeul ndaareh, mer
dem woutti ay xeer
took saam, commencer
tamxaar kouleu
« ndjoss »gani «
ndjoket » jok
dakeh«
yaye dakeh, yaye dakeh,
yaye dakeh bamouy neex saf kaani » !
aneu kou tour kaani ci keur gui ?
soubeu bata
y gars yaa gui
thiooki,pareh took deup seen daleu
bagn koulen
tendre par quatre,
tangal seen taat
ey way temps boy...
tabaski, korité,rang ay fan pour
lettoupareh dag « lagos »
moussorou kouleu ni meu xool gani ma bagn
di xaar bess bi
yakamti...
sangu beu xeess,
yereh you bess
niaani deuweuneul,
100 francs di xeweul
temps boy,
tamxarit,door céré beu diis
poudeurou, sol thiaaya,
gaddu bol, tek ko tama,
«
taajabon! weuleuy ! »
deysane temps boy...
dawal pneu, ak
cynkal,kogn beu kogn,
louer velo,
gueneu timiss
sath mango,defar «
niambaan » ak «
creme café »,
mbouraaké, niambi soukeur, doumeu ko kafè,
guerté tubaab, oul, kokorong,tey doon naa ko wethi ak temeri kong !!
deysane temps boy ....
«
le nord et le sud », «
kounta kinté »,
jaangal niou histoire, meme avec des clichés,
affaire bu doy waar, tey ni ma ko guisseh
tele novelas a deux bal rekeu fi am succés
temps boy,
sandokan, yanez, marianne
«
le tigre de la malaisie » beureh wone ay fans,
d'Artagnan nak, kou ko fekeh ?
dam bant, defar epée,
niom
clementine, tom sawyerj
oe l'indien, ma frayeur,
bibi phoque, walla
colargolours boobou ak parasol
gigi, « il etait une fois la vie »,
kimbo, kita,
tex willer,
zembla,bleck le rock,
tarzan,mais n'oublie pas mon enfant,
le hero est toujours blond aux yeux clairs
they temps boy...
fateh na niom
pif, niom sp
irou,
niom
asterix ak
picsou,club des cinq,
clan des sept,
niom
heidi ak
fantomette,lectures francaises,
presque rien de sénégalais
heureusement que père birago était là
avec les superbes
contes d'amadou coumba;
leuk le lievre ak wa ndoumbelane
fou meu ko xalaat tek ci deysane
deysane temps boy ....
cinema, guettou mbeyefilm indou, fen you reuy
amintah bachan, dramendra
nagin, fakiraameun woy yi par coeur
walla tok di jooy des heures
«
zeunom » bi mer geu taccu
niou sath film mi geu youxou
ey way temps boy....
* extrait de temps boy des daara j